bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Romans 15:12
Romans 15:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te it Esayi wax na ne:«Am na sëtu Yese buy ñëw,dina yilif xeeti ñi dul Yawut,te ci moom lañuy wékk seen yaakaar.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Esayi it neeti: «Ab car ay bawoo ca Yese reen ba, mooy taxaw, yilif jaambur ñi dul Yawut, te moom la ñi dul Yawut di yaakaar.»