Romans 15:14 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bokk yi, wóor na ma ne, baax ngeen ba fa mbaax man a yem, fees dell ak xam-xam, ba man a jàngaleente mbiri Yàlla ci seen biir.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bokk yi, man ci sama bopp, li ma bir ci seen mbir moo di yéene ju rafet ngeen fees, te buural ngeen bépp xam-xam, man ngeena artoonte it.