Romans 15:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Na ku nekk ci nun di wut lu neex moroomam ngir jariñ ko, ba mu gën a dëgër ci ngëmam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Na ku nekk ci nun sàkku bànneexu moroomam, ci lu koy jariñ, ngir feddli ngëmam.