Romans 15:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Sama yéene mooy xamle xebaaru turu Kirist fa mu eggagul, ndax bëggumaa yeggale sas wu keneen daloon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu laa masa xintewoo di xamle xibaaru jàmm bi fu ñu xamewul Almasi asi, ngir baña bey sas wu fa keneen jotoona dal.