Romans 15:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li ma def nag, dëppoo na ak li Mbind mi wax ne:«Ñi yégagul mbiram dinañu ko yég,te ñi ko musul a dégg, xam ko.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu ma jëfe it moo dëppoo ak ni ko Mbind mi indee ne: «Ña ñu waxul woon mbiram, dinañu gis, te ña dégguloon, dinañu ràññee.»