Romans 15:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye nag fi mu nekk maa ngi dem nii Yerusalem, ngir dimbaliji gaayi Yàlla yu sell ya fa nekk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye fii ma tollu, Yerusalem laa jëm, ngir ndimbal lu ñeel ñu sell ña féete foofa.