Romans 15:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte Kirist musul a wut bànneexu boppam. Loolu la Mbind mi wax ne: «Lor yi ñu la saagaa, ci sama kaw lañu dal.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax Almasi kat sàkkuwul bànneexu boppam, te noonu it la Mbind mi indee ne: «Ñi lay saaga, seeni saaga, ci sama kaw la dal.»