Romans 15:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñëw na itam ngir ñi nekkul Yawut man a màggal Yàlla ndax yërmandeem. Moo tax Mbind mi ne:«Dinaa la màggal tey tagg saw tur,ci kanamu xeet yépp.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Leneen li indi Almasi mooy may jaambur ñi dul Yawut lu ñu màggale Yàlla, te muy yërmandeem. Noonu it la Mbind mi indee ne: «Looloo waral ma sant la ci biir xeet yi, sàbbaal la.»