Romans 16:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Nuyul-leen ma it Filolog ak Yuli, Nere ak jigéenam.Te fàttewuma Olimpas ak gaayi Yàlla yiy booloo ak ñoom ñépp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nuyul-leen ma it Filolog ak Yuli, ak Nere ak jigéenam, ak Olimpas ak mboolem ñu sell ñi nekk ak ñoom.