Romans 16:2 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Nangeen ko jàpp ci turu Boroom bi, ni ko gaayi Yàlla yi yelloo, te dimbali ko ci lépp lu mu aajowoo; ndaxte moom itam wax dëgg, dimbali na ñu bare, ba ci man mii di wax ak yéen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dalal-leen ko ci turu Boroom bi, ni ko ñu sell ñi yelloo, te ngeen jàpple ko ci lépp lu mu aajowoo, nde moom itam xettli na ñu bare, ba ci man mii.