Romans 16:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su ko defee Yàlla Boroom jàmm dina noot Seytaane ci seeni tànk léegi. Na yiwu Yeesu sunu Boroom ànd ak yéen!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ko defee Yàlla miy boroom jàmm mooy dër Seytaane ci lu gaaw, fi ngeen ko joggi seeni tànk. Yal na sunu yiwu Boroom Yeesu ànd ak yeen!