Romans 16:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Santleen Yàlla, mi leen man a saxal bu wér ci dëggu xebaar bu baax, bi may waare ci mbirum Yeesu Kirist! Nekkoon na kumpa gu làqu diirub ay ati at,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kooku leen mana dooleel nag ndax sama xibaaru jàmm, ak waareb Yeesu Almasi, mi mu feeñal mbiram tey, gannaaw ba mu nekkee mbóot mu làqu woon naka jekk,