Romans 16:26 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
waaye léegi nag Yàlla dindi na nu ci kumpa. Te santaane na, nu yégle xebaar boobu ci xeeti àddina sépp, ci firi Mbindi yonent yi, ngir nit ñi man koo gëm, ba jébbalu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
mbóot mu bindi yonent yi fésal tey, ba xamal ko xeet yépp ci ndigalal Yàlla ji sax, ngir xeet yépp gëm ba dégg ndigal,