Romans 16:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te fàttewuma Ampilyaatus, mi ma bëgg ci sama xol ngir Boroom bi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nuyul-leen ma Ampilyaatus, mi ma soppal sama bopp ndax Sang bi.