Romans 2:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax ñi dul Yawut te nekkuñu ci yoonu Musaa, ñu ngiy def li yoon woowu tëral, ndaxte Yàlla def na ko ci nit. Te wonee nañu noonu ne, man nañoo ràññee lu baax ak lu bon, su ñu nekkul sax ci yoonu Musaa,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jaambur ñi dul Yawut, te amuñu yoonu Musaa, ndegam teewu leena topp bindub juddu, bay jëfe li yoonu Musaa laaj, dafa fekk ñoom ci seen bopp, ñuy seen yoonu bopp, doonte amuñu yoonu Musaa.