Romans 2:16 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndax bés dina ñëw, bu xalaat yu làqu yi di feeñ, te Yàlla àtte nit ñi jaarale ko ci Yeesu Kirist. Xebaar bu baax, bi may waare, moo ko wax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te noonu lay deme kera bés ba Yàlla di àtte mbiri kumpa yu nit ñi, ci saytub Yeesu Almasi, ni ko sama xibaaru jàmm bi indee.