Romans 2:18 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xam nga coobareem, ndaxte jàng nga ci yoonu Musaa, ba fonk yëf yi gën a baax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yaa xam coobarey Yàlla, te yaa jànge ci yoonu Musaa, ba xam li am solo dëgg.

Recommended Reading