Romans 2:26 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te itam ku xaraful, tey def jëf yu jub yi yoonu Musaa santaane, ndax Yàlla du ko teg ni ku xaraf?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon kay ki xaraful, tey jëfe njub gi yoonu Musaa santaane, ñàkka xarafam, deesu ko ko waññal ag xaraf?