Romans 2:27 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ku dul Yawut te xaraful waaye di sàmm yoon wi, kooku dina la man a àtte yaw Yawut bi. Ndaxte li ngay xam-xam yoonu Musaa ci Mbind mi te xaraf, terewul nga koy moy.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ki xaraful ciw yaramam, te teewu koo sàmm yoonu Musaa, moo lay teg ab daan, yaw mi boole mbindum yoonu Musaa, ak sag xaraf, te teewu la di moykatub yoon wi.