Romans 2:29 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye Yawut dëgg, ci xol lay nekk. Te xaraf dëgg itam, ci xol lay nekk. Du ngistal, lu dëggu la. Te képp ku mel noonu, dees na la gërëm, waxumala nit ñi, waaye Yàlla ci boppam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ab Yawut dëgg, kumpag biir xol la koy nekke, xaraf it mbirum xol la; ci xel mi lay sottee, waaye du ci mbindum yoon. Ngërëm la it du ci nit lay jóge, xanaa Yàlla.