Romans 2:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yaw nag miy àtte ñiy def loolu, te di ko def, ndax defe nga ne, dinga rëcc ci àtteb Yàlla?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yaw nit kiy sikk ñiy jëfe yooyii, te di ko def, ndax defe nga ne yaw ci sa bopp dinga rëcc àtteb Yàlla?