Romans 2:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax dangaa xeeb mbaaxu Yàlla, mi yéex a mer te di la muñal? Xanaa xamuloo ne, Yàllaa ngi lay won baaxaayam, ngir nga réccu say bàkkaar?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am dangay sofental mbaaxu Yàlla gu réy, akug jéllaleem, akug muñam, ndax ñàkka xam ne li Yàlla namm ci baaxe la, moo di nga tuub?