Romans 3:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñépp jeng nañu,ba kenn amalatul Yàlla njariñ.Kenn du def lu baax, du kenn sax!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñépp a lajj ba bokk yàqu yaxeet, Kenn deful lu baax, du kenn sax!