Romans 3:24 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye gannaaw Kirist Yeesu dee na ngir jot leen, Yàlla ciw yiwam man na leen a àtte ni ñu jub ci dara.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te ci yiwu Yàlla wu àndul ak genn pey lees di joxe ñépp àtteb ñu jub, ndax njot gi sottee ci Almasi Yeesu.