Romans 3:28 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte danoo dëggal ne, ngëm rekk a tax Yàlla di àtte nit ni ku jub, waaye du sàmm yoon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax jàpp nanu ne ci kaw ngëm lees di jox nit, àtteb ku jub, waaye du ci jëfam ju yoon santaane.
Recommended Reading