Romans 3:29 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Walla ndax nag Yawut yi rekk la fi nekkal? Ndax nekkalu fi it ñu dul Yawut? Aaŋkay!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am Yàlla da di Yàllay Yawut yi doŋŋ? Da dul Yàllay jaambur yi dul Yawut itam? Ahakay, mooy Yàllay jaambur ñeet kay!