Romans 3:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu fekkee ne am na ci ñoom ñu ñàkk kóllëre, ndax loolu man na fanq kóllëreg Yàlla?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ci ñennat ñàkkee kóllëre, ndax seenug ñàkk kóllëre day fanq kóllëreg Yàlla?