Romans 3:30 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw Yàlla kenn la, ñépp la fi nekkal. Ñi xaraf dina leen àtte ni ñu jub ndax seen ngëm, ñi xaraful it dina leen àtte ni ñu jub ndax seen ngëm.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw Yàlla kenn la, mooy jox ñi xaraf, àtteb ñu jub ci kaw ngëm; ñi xaraful it, moo leen di jox àtteb ñu jub ci kaw ngëm.