Romans 3:31 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xanaa kon ngëm day fanq yoonu Musaa? Mukk! Da koy gën a dëgëral sax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax loolu day tekki ne ngëm lanu jël, neenale ko yoonu Musaa? Mukk! Xanaa dañu koo dëggal kay.