Romans 3:4 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Mukk! Su ñépp nekkoon ay naaféq, du tere Yàlla nekk dëgg. Moom la Mbind mi wax ci Yàlla ne:«Loo wax, ñépp ànd ci,te ku layoo ak yaw, nga yey ko.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mukk kay! Fàww Yàlla wéye di ku dëggu, te ñépp di ay fen-kat, te noonu la Mbind mi indee ne: «Soo waxee, am dëgg, te soo àttee, yey.»