Romans 3:9 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kon nag lu nu ci war a wax? Nun Yawut yi, ndax noo gën ñi ci des? Mukk! Ndaxte wone nanu ne, nit ñépp ñu ngi ci nootaangeg bàkkaar, muy Yawut yi mbaa Gereg yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ana kon nun Yawut yi, lu nu gëne ci nit ñi? Du ci lenn! Ndax firndeel nanu ba noppi ne, muy Yawut bi, di ki dul Yawut, ñépp a ngi ci kilifteefu bàkkaar.