Romans 4:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te noonu itam la Ibraayma man a nekke baayu ñi xaraf, bu fekkee yemuñu rekk ci xaraf, waaye ñu am ngëm, ga Ibraayma sunu maam amoon lu jiitu xarafam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Looloo tax it Ibraayma di maamu ñi xaraf, te du xaraf gu ñu toppe aada, xanaa ñu boole ca topp ci tànki ngëm ga sunu maam Ibraayma amoon ba mu xarafagul.