Romans 4:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte su fekkee ne ñi nekk ci yoonu Musaa rekk ñooy moom àddina, kon ngëm amatul njariñ, te digeb Yàlla dafa toxu.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nde su dee ñi ci yoonu Musaa la dige bi ñeel, kon ngëm dootu tekki dara, te kon digeb Yàlla ba day neen.