Romans 4:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yoonu Musaa daal du def lu dul wàcce merum Yàlla ci sunu bopp; ndax fu yoon amul, jàdd yoon du fa man a am.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yoonu Musaa daal, am sànj lay jur, te fu yoon wees di sàmm amul, genn moy amu fa.