Romans 4:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye loolu lañu bind ne: «Yàlla jagleel na ko njub,» du Ibraayma rekk a moom wax ji.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ñu bindee ne ngëmu Ibraayma, moom lees ko waññal àtteb ku jub, du Ibraayma doŋŋ la mbind ma ñeel.