Romans 4:25 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte Yàlla jébbale na ko ngir sunuy tooñ, dekkal ko ngir àtte nu jub.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
mi ñu teg ciy loxo, mu dee ndax sunuy tooñ, ba dekkal ko, ngir nu jagoo àtteb nit ñu jub.