Romans 4:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag barkeel googu, ndax ñi xaraf rekk ñoo ko yeyoo? Ndax ñi xaraful it bokkuñu ci? Aaŋkay! Ndaxte wax nanu ne, Yàlla jàppe na ngëmu Ibraayma ni njub.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon moomu mbégte xanaa Yawut yiy xaraf doŋŋ la ñeel? Ñi xaraful it dañu cee bokkul? Ndax kat danu ne Ibraayma lañu waññal ngëmam ga, ag njub.