Romans 5:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te sax nu ngi bég ci Yàlla, jaarale ko ci sunu Boroom Yeesu Kirist, mi nu jubale ak moom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te yemunu ci, xanaa di sagoo Yàlla itam ndax sunu Boroom Yeesu Almasi, mi nu jubale ak moom.