Romans 5:18 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Kon nag nu gàttal wax ji; jàddug kenn nit ka rekk moo waral Yàlla daan ñépp; noonu itam jëf ju jubu keneen nit ka rekk moo ubbi bunt, ba ñépp man a jub ci kanam Yàlla te am dund gu bees.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon nag noonee moyug kenn jure mbugalu nit ñépp daal, noonu la jenn jëfu njekk jurale ñépp dundin wu yees ci kaw àtteb njub bu leen jenn jëf ja may.