Romans 5:19 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Aadama moomu dafa déggadil Yàlla, ba yóbbaale ñu bare, ñu nekk i bàkkaarkat; noonu itam Yeesu Kirist dafa déggal Yàlla, yóbbaale ñu bare itam, ñu jub.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonee déggadig kenn nit taxe ñu bare doon ay bàkkaarkat, noonu it la déggug ndigalu kenn nit taxe ñu jox ñu bare àtteb nit ñu jub.