Romans 5:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te du ci loolu rekk, waaye bég nanu it ci sunuy nattu; ndax xam nanu ne, nattu day feddali muñ;
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te yemunu ci, xanaa di sagoo sunuy tiis itam, nde xam nanu ne dékku aw tiis mooy taxa muñ;