Romans 5:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kuy nangoo deeyal nit ku jub, yombul a gis, waaye nag jombul am na ku nangoo deeyal ku baax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Barewul ku nangoo deeyal nit ku jub, doonte jombul mu am ku nangoo deeyal ku baax.