Romans 5:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yàlla firndeel na mbëggeelam ci nun, ci li Kirist dee ngir nun, bi nu nekkee sax ay bàkkaarkat!
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye Yàlla moom, ni mu firndeele cofeelam ci nun, moo di, ba nu dee ay bàkkaarkat, ca la nu Almasi deeyal!