Romans 6:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xanaa dangeen a xamul ne, képp ku ñu sóob ci ndox, ngir wone ne, mu ngi bokk ci Yeesu Kirist, ci deewu Yeesu la bokk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dangeena umple ne mboolem nun ñi ñu sóob ci Yeesu Almasi, cig deeyam lañu nu sóobaale?