Romans 6:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag gannaaw benn lanu ak Kirist, dee ni mu deeye woon, kon dinanu nekk it benn ak moom, dekki ni mu dekkee woon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw dees noo bennale ak moom ci dee gu ñu nirule ak deeyam, dees nuy bennale itam ak moom ci ndekkite lu niru ndekkiteem.