Romans 6:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw nag dee nanu ak Kirist, gëm nanu ne, dinanu dekki it ni moom,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw noo deeyandoo ak Almasi nag, gëm nanu ne nooy dundandoo ak moom.