Romans 7:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bokk yi, yéen ñi may waxal xam ngeen luy yoon; xam ngeen kon ne, yoon am na doole ci nit diirub dundam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am, bokk yi, yeen ñi xam yoon wi laay waxal, dangeena umple ne yoon yiliful nit ki lu moy ci giiru dundam?