bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Romans 7:10
Romans 7:10 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Noonu gis naa ne, ndigal loolu waroon a jëme nit ñi ci dund, daf maa jëme ci dee.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
man nag, ma dee. Kon ndigalu yoon wi wara jëme ci ag dund, moom ci boppam moo ma mujj jëme ci ndee.