Romans 7:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag man nanoo wax ne, yoonu Musaa yoon wu sell la, te ndigalu Yàlla dafa sell, jub te baax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon yoonu Musaa lu sell la, ndigalam di lu sell, te jub te baax.