Romans 7:15 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte samay jëf jaaxal na ma; li ma bëgg a def, duma ko def, waaye li ma bañ rekk, moom laay def.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xawma sax lu waral may jëfe ni may jëfe; li ma namm, du loolu laay jëfe, waaye li ma bañ, moom laay jëfe.
Recommended Reading